Waters of LifeBiblical Studies in Multiple Languages |
|
Home Bible Treasures Afrikaans |
This page in: -- Albanian -- Arabic -- Armenian -- Bengali -- Burmese -- Cebuano -- Chinese -- Dioula -- English -- Ewe -- Farsi -- French -- Georgian -- Greek -- Hausa -- Hindi -- Igbo -- Indonesian -- Javanese -- Kiswahili -- Kyrgyz -- Malayalam -- Peul -- Portuguese -- Russian -- Serbian -- Somali -- Spanish -- Tamil -- Telugu -- Thai -- Turkish -- Twi -- Urdu -- Uyghur -- Uzbek -- Vietnamese -- WOLOF -- Yiddish -- Yoruba
YOWAANA - Leer gi leeral na Lëndëm giJàngat ci xebaar bu baax bi ci Kirist ci YowaanaXAAJ 1 - Leeraayu Leeru Asamaan (Yowaana 1:1/4:54)
A - Peeñug Kàddug Yàlla gi ci Yeesu (Yowaana 1: 1-18)
1. Nekkin ak liggéeyu Kàddu gi laata muy feeñu (Yowaana 1:1-5)
2. Sóobkat bi ci ndox(Yaxya) mungi waajal yoonu Krist (Yowaana 1:6-13)
3. Feesaayu ndamul Yàlla feeñ na ci jëmmal gi (Yowaana 1:14-18)
B - Krist jële na ay taalibeem la ko dale ca tuub seeni bàkkaar ba ca mbébteg céet ga (Yowaana 1:19 - 2:12)
1. Ag Kureelu Sanedreŋ mungi laaj Yaxya (Yowaana 1:19-28)
2. Seede yu gën a daw yaram,yu Yaxya defal Krist (Yowaana 1:29-34)
3. Juróom-benni taalibe yu jëkk yi (Yowaana 1:35-51)
4. Kéemaan gi Yeesu jëkk a def ca céet ga ca Kana (Yowaana 2:1-12)
C - Ba Yeesu njëkkee ñów Yerusalem (Yowaana 2:13 - 4:54) -- Ci dëgg-dëgg, lan mooy màggal?
1. Cellalug Këru Yàlla gi (Yowaana 2:13-22)
2. Yeesu mungi wax ak Nikodeme (Yowaana 2:23 - 3:21)
a) Nit ñaangi ñów ci Yeesu (Yowaana 2:23-25)
b) Soxla juddu gu bees (Yowaana 3:1-13)
c) Kurwaa bi (bant bi), ab juumtukaayu juddu gu bees gi (Yowaana 3:14-16)
d) Sàbbi Krist,ci àtte lay jëme (Yowaana 3:17-21)
3. Yaxya mungi seedeel Yeesu boroom kër gi (Yowaana 3:22-36)
4. Yeesu ca Samari (Yowaana 4:1-42)
a) Yeesu fexe na ba njaalookat ba tuub (Yowaana 4:1-26)
b) Yeesu yóbbu na ay taalibeem ngir ñu gis meññeef mu ñor mi (Yowaana 4:27-38)
c) Tas Xabaar bu baax bi ci biir Samari (Yowaana 4:39-42)
5. Pajug doomu kilifa takk-deru buur bi (Yowaana 4:43-54)
XAAJ 2 - Leer gi leeral na lëndëm gi (Yowaana 5:1 - 11:54)
A - Ñaareelu tukki ca Yeruusalem (Yowaana 5:1-47) -- Yokkute jànkoonte diggante Yeesu ak Yawut ya
1. Pajum jarag ga ca Betesda (Yowaana 5:1-16)
2. Yàllaa ngi jëfandoo ak Doomam (Yowaana 5:17-20)
3. Yeesu dafay dekkil ñi dee te di àtte àddina si (Yowaana 5:20-30)
4. Ñeenti seede yiy wone ne Kirist mooy Yàlla (Yowaana 5:31-40)
5. Sabab ñàkka gëm (Yowaana 5:41-47)
B - Yeesu mooy mburu dund gi (Yowaana 6:1-71)
1. Yeesu dundal na juróomi junni nit (Yowaana 6:1-13)
2. Yeesu dafa rocceeku ci ñi Ko bëgg a fal buur (Yowaana 6:14-15)
3. Yeesu dafay wallu ay taalibeem (Yowaana 6:16-21)
4. Yeesu, may na ñépp ñu man a tànnal seen bopp ngir “nangu walla bañ!” (Yowaana 6:22-59)
5. Wàññeeku taalibe ya (Yowaana 6:59-71)
C - Tukkib Yeesu bu mujj ca Yerusalem (Yowaana 7:1 - 11:54) Tàggaloo Lȅndȅm Gi Ak Leer Gi.
1. Kàdduy Yeesu ca màggalu Mbaar ya (Yowaana 7:1 - 8:59)
a) Yeesu ak ay rakkam (Yowaana 7:1-13)
b) Xalaat yu wuute yu jëm ci Yeesu, ci diggante askan wi ak Kuréel gu mag gi (Yowaana 7:14-53)
c) Ña fonk Yoon wi indil Yeesu jigéen ju njaaloo ngir nattu Ko (Yowaana 8:1-11)
d) Yeesu, leeru àddina si (Yowaana 8:12-29)
e) Bàkkaar jaam la (Yowaana 8:30-36)
f) Seytaane bóomkat bi ak fenkat bi (Yowaana 8:37-47)
g) Krist nekk na laata Ibraayma (Yowaana 8:48-59)
2. Pajug Gumba judduwaale ga (Yowaana 9:1-41)
a) Paj ma ca bésub noflaay ba (Sabat) (Yowaana 9:1-12)
b) Yawut yaa ngay laaj nit ka ñu wéral (Yowaana 9:13-34)
c) Yeesu feeñu na ka mu fajoon ni Doomu Yàlla (Yowaana 9:35-41)
3. Yeesu sàmm bu baax bi (Yowaana 10:1-39)
a) Mbote mi dafay ràññee (dégg) baatu sàmm bu baax bi (Yowaana 10:1-6)
b) Yeesu mooy bunt bi dëgg (Yowaana 10:7-10)
c) Yeesu mooy Sàmm bu Baax bi (Yowaana 10:11-21)
d) Sunu kaaraange ci biir jokkoo gi am diggante Baay ji ak Doom ji (Yowaana 10:22-30)
e) Doomu Yàlla ji ci Baay ji ak Baay ji ci Doom ji (Yowaana 10:31-39)
4. Ndekkite Lasaar ak la mu jur (Yowaana 10:40 - 11:54)
a) Yeesu jàll na deux Yurdan (Yowaana 10:40 - 11:16)
b) Yeesu daje na ak Màrt ak Maryaama (Yowaana 11:17-33)
c) Ndekkite Lasaar (Yowaana 11:34-44)
d) Sanedreŋu Yawut yi àtte na ne dañu war a rey Yeesu (Yowaana 11:45-54)
XAAJ 3 - LEER NGAA NGI MELAX CI MBOOLOO NDAW YI (Yowaana 11:55 - 17:26)
A - LI JIITU AYU BéS bu SELL bi (Yowaana 11:55 - 12:50)
1. Tuur nañu Yeesu diwlin ca Betani (Yowaana 11:55 - 12:8)
2. Duggu Yeesu ca Yerusalem (Yowaana 12:9-19)
3. Ay Grek ñungi jéem a gis Yeesu (Yowaana 12:20-26)
4. Màggaayu Baay ji ci jamonoy ruu gu jàq (Yowaana 12:27-36)
5. Dëgër boppu nit ñi, ak li Àtte bi am lépp (Yowaana 12:37-50)
B - Xew-xew yi amoon gannaaw reeru Boroom bi (Yowaana 13:1-38)
1. Yeesu raxas na tànki taalibeem ya (Yowaana 13:1-17)
2. Workat bi ñu feeñal te mu nekk ci njaqare (Yowaana 13:18-32)
3. Ndigal lu bees ngir Jàngu bi (Yowaana 13:33-35)
4. Krist wax na ci weddi Piyeer ba (Yowaana 13:36-38)
C - Tàggoo ba ca Néeg bu kowe ba (Yowaana 14:1-31)
1. Yàlla dafa teew ci Krist (Yowaana 14:1-11)
2. The Holy Trinity descends on believers by the Comforter (Yowaana 14:12-25)
3. Jàmm ji Krist maye (Yowaana 14:26-31)
|